Hommage à Mame Abdou Aziz Sy Dabakh

Quand Balkhawmi prodiguait  des conseils à son jeune frère Hadji Abdou Aziz Sy Dabakh

 

Abdou manguilay deink nguay woute nioulay khelal, boul doylo sa khel

Abdou manguilay moytoulo rambadj bi nieuw ci yaw di yakh sa diguantè ak nitt gni

Abdou manguilay deink mougn, dieguelei ak rafetal

Abdou koula togn wala defla lou niaaw , dieuleul lou bakh fayeiko

Abdou so beuguei mouthie kholal sa kanam , boul xol ayyib keina , sayy ayyib nala doy

Abdou fekheil ngua yamalei ki am ak  ki niak

Abdou diokal koula dogg, diapal koula bayi

Abdou boul tontou kouy dieul lou niaw diko tek sa derr wala dila xass

LAISSER UN COMMENTAIRE

Please enter your comment!
Please enter your name here